Esekiyel 15:1-7 WOLB2025 - Bible AI

1Gannaaw loolu kàddug Aji Sax ji dikkal na ma ne ma:

2«Yaw nit ki, ana lu bantu reseñ gëne ci bant yi,

3Ndax dees na ca sàkk bant, liggéeye ko?

4Xanaa sànni cib taal, xambe,

5Ndegam ba mu nee ñumm,

6Kon nag Boroom bi Aji Sax ji dafa wax ne:

7Maay jànkoonteek ñoom,

© 2025 Bible Society of Senegal
iv>