1Kàddug Aji Sax ji dikkal ma ne ma:
2«Yaw nit ki, ñaari jigéen la woon,
3di gànctu ca Misra,
4Ku mag kaa doon Owola,
5Owola di sama soxna tey gànctu,
6Ña nga sol seen mbubbi baxa,
7Boppam la daan jox tànnéefi doomi Asiri yooyu yépp,
8Gànctoom ga woon ca Misra, bawu ko.
9Moo tax ma teg ko ca loxoy faram ya,
10Ñoo ko ñori ba mu ne duŋŋ,
11«Owoliba rakk ja gis ca
12Moom it waa Asiri ya la xédd,
13Ma gis ni mu sobeele boppam,
14Teewul rakk ja gëna gànctooti,
15Ña nga takk ngañaay ca seen ndigg,
16Rakk ja teg nataal ya bët rekk, xédd leen,
17Doomi Babilon ya dikk,
18Moo siiwal gànctoom,
19Mu gën di gànctooti,
20Muy xédd ay faram yu seeni ngóora di saf yu mbaam,
21«Yaw Owoliba de, yaa namm sa yàqute ga woon ba ngay ndaw,
22Moo tax Boroom bi Aji Sax ji dafa wax ne:
23waa Babilon, Kaldeen ñépp,
24Dañuy dal fi sa kaw aki gànnaay, watiir aki mbege ak kuréelu xeeti xeet,
25Maa lay yen sama fiiraange,
26Dañuy futti say yére, foqati say gànjar.
27Maay dakkal sa jëfi yàqute,
28Boroom bi Aji Sax ji kat dafa wax ne:
29Mbañeel lañuy jëfeek yaw,
30Ñoo lay def jii jëf
31Yaa topp sa tànki mag,
32Boroom bi Aji Sax ji dafa wax ne:
33Mànditeeku tiis ngay feesi,
34Yaa koy naan ba siitaatu ko,
35«“Moo tax Boroom bi Aji Sax ji dafa wax ne:
36Aji Sax ji nag ne ma:
37Ñoo njaaloo, ñoo bóome,
38Lii itam, ñoo ma ko def:
39Ñoo rendil seen kasaray tuur seeni doom,
40Te sax ñoo yeble, wutiy góor,
41toog ci lal bu yànj,
42Muy coowal gàngoor gu amul xalaatu àddina;
43Booba laa wax ci ndaw sii njaaloo ba ràpp, ne:
44Mu daldi ànd ak moom ni ñuy àndeek caga rekk.
45Waaye ay nit ñu jub a ngii,
46«Boroom bi Aji Sax ji déy dafa wax ne:
47Gàngoor gaa leen di dóor ay doj,
48ma dakkale noonu yàqute ci réew mi,