1Kàddug Aji Sax ji dikkal na ma ne ma:
2«Yaw nit ki, neel jàkk Amoneen ñi, nga jottali kàdduy waxyu|lemma="waxyu:"* ci seen kaw.
3Waxal Amoneen ñi, ne leen:
4Maa ngii nag di leen jébbal màngaani penku,
5Maay soppi Raba seen péey ab parlub giléem,
6Boroom bi Aji Sax ji déy dafa wax ne:
7Maa ngii nag di leen dóor sama loxo,
8«Boroom bi Aji Sax ji déy dafa wax ne:
9Maa ngii nag di ŋafal réewum Mowab,
10Màngaani penku laa leen di jébbal,
11te maay wàcceel Mowab ay mbugal,
12«Boroom bi Aji Sax ji dafa wax ne:
13Moo tax Boroom bi Aji Sax ji dafa wax ne:
14Maay duma Edom,
15«Boroom bi Aji Sax ji déy dafa wax ne:
16Moo tax Boroom bi Aji Sax ji dafa wax ne: