Esekiyel 26:1-20 WOLB2025 - Bible AI

1Ba loolu amee, ca fukkeelu at maak benn, yemook benn fanu weer wa, kàddug Aji Sax ji dikkal ma ne ma:

2«Yaw nit ki,

3Boroom bi Aji Sax ji dafa wax ne:

4Ñooy màbb say tata,

5Tir ay doon wéerukaayu caax ci digg géej gi,

6dëkk-dëkkaan yi bootu ci mbooyam, saamar faat leen,

7«Boroom bi Aji Sax ji déy dafa wax ne: Maa ngii di jële bëj-gànnaar, indi ci kaw Tir, Nebukatnecar buuru Babilon, buuru buur yi, aki fas aki watiir aki gawar ak mbooloo mu takku.

8Dëkk-dëkkaan yi bootu ci sa àll bi, saamar la leen di reye.

9mooy dóor say tata dénku dàjjikaay,

10ay fasam yu bare sànge la pënd,

11Tànki fasi naaru-góoram lay noote sa mbeddoo mbedd,

12Ñooñooy foqati sam koom,

13Maay dakkal say woy,

14Maa lay def doj wu ne duŋŋ,

15«Boroom bi Aji Sax ji dafa wax Tir, ne ko:

16Mboolem buuri tefes yaay wàcc seeni ngàngune,

17Ñooy yékkati kàddu, jooy, ne la:

18Tey sa bésub jéll bii,

19«Boroom bi Aji Sax ji déy dafa wax ne:

20keroog maa lay wàccaaleek ñay jëm biir pax,

© 2025 Bible Society of Senegal
div>