Esekiyel 29:1-20 WOLB2025 - Bible AI

1Ca fukkeelu at ma, fukki fan ak ñaar ca fukkeelu weer wa, kàddug Aji Sax ji dikkal na ma ne ma:

2«Yaw nit ki, neel jàkk Firawna buuru Misra, nga jottali kàdduy waxyu|lemma="waxyu:"* fi kawam ak fi kaw Misra gépp.

3Waxal, nga ne: “Boroom bi Aji Sax ji dafa wax ne:

4Waaye maay we ay lonku ci say ŋaam,

5Ma wacc la ca màndiŋ ma,

6ba waa Misra gépp xam ne maay Aji Sax ji.

7ñu jafandu ci, mu ne tàllit,

8«“Moo tax Boroom bi Aji Sax ji dafa wax ne:

9Réewum Misraay gental, di ndànd-foyfoy,

10moo tax maa ngii fi sa kaw,

11Tànku doom aadama du fa jaare,

12Maay def Misra gëna gental ci réew yi gental,

13Boroom bi Aji Sax ji déy dafa wax ne:

14Ca laay tijjee wërsëgu Misra,

15gëna suufe ci nguur yi,

16Waa kër Israayil dootuñu yaakaar Misra,

17Ca ñaar fukkeelu at maak juróom ñaar, benn fanu weer wa njëkk, kàddug Aji Sax ji dikkal na ma, ne ma:

18«Yaw nit ki, Nebukatnecar buuru Babilon teg na mbooloom xareem coono bu metti ca seen xareek Tir. Seen kawari bopp yépp ruus na, seen wagg yépp tëccu, te coonoom ba mu sonn ca Tir, te du moom, du ay nitam ku ci am wenn yool.

19Moo tax Boroom bi Aji Sax ji dafa wax ne:

20di yoolu coonoom.

© 2025 Bible Society of Senegal
div>