Esekiyel 30:1-25 WOLB2025 - Bible AI

1Ba loolu amee kàddug Aji Sax ji dikkal ma ne ma:

2«Yaw nit ki, jottalil kàdduy waxyu|lemma="waxyu:"*! Neel: “Boroom bi Aji Sax ji dafa wax ne:

3Bés jubsi na déy,

4Saamar ay dikkal Misra,

5Waa Kuus ak Puut ak Ludd ak xeet yu raxe yépp ak waa Kub,

6«“Aji Sax ji dafa wax ne:

7Ñooy gëna wéet ci réew yi,

8Bu ma taalee Misra,

9Bésub keroog dees na dugg ay gaal, génn ci sama ndigal,

10«“Boroom bi Aji Sax ji dafa wax ne:

11Mooy ànd ak ñoñam,

12Maay def wali Niil ag joor,

13«“Boroom bi Aji Sax ji dafa wax ne:

14Maay yàqate Pattros,

15Maay sottil sama xadar Sin, rawtub Misra,

16Maay taal Misra,

17Xaleli góori Oon ak Pi Beset, saamar a leen di faat,

18Bu ma dogee sidditi Misra,

19Nii laay wàccee ay mbugal ci Misra,

20Ca fukkeelu at maak benn, juróom ñaari fan ca weer wa njëkk, kàddug Aji Sax ji dikkal na ma ne ma:

21«Yaw nit ki, damm naa përëgu Firawna buuru Misra,

22Léegi nag Boroom bi Aji Sax ji dafa wax ne:

23maay tasaare Misra fi biir xeet yi,

24Maay dooleel përëgu buuru Babilon,

25Maay dooleel përëgi buuru Babilon moos,

© 2025 Bible Society of Senegal
div>