Esekiyel 32:1-31 WOLB2025 - Bible AI

1Ca fukkeelu at maak ñaar, benn fan ca fukkeelu weer waak ñaar, kàddug Aji Sax ji dikkal na ma ne ma:

2«Yaw nit ki, yékkatil kàddug jooy, ñeel Firawna buuru Misra. Nga ne ko:

3Boroom bi Aji Sax ji dafa wax ne:

4Maa lay wacc fi suuf, sànni la ci àll bi,

5Maay lale tund yi sa suux,

6Maay nàndale suuf sa deret,

7Bu sa leer feyee, maay muur asamaan,

8Mboolem leeri asamaan laay giimal fi sa kaw,

9«“Maay jàqloo xeet yu bare,

10Saw demin laay tiitale xeet yu bare,

11«“Boroom bi Aji Sax ji déy dafa wax ne:

12Saamari jàmbaar laay tërale sa mbooloo,

13Maay faagaagal sa mboolem jur

14Su boobaa ma dalal seeni ndox,

15Bu ma defee réewum Misra ab gent,

16«Kàddug jooy a ngoog gu ñuy jooyi,

17Ca fukkeelu at maak ñaar, fukki fan ak juróom ca weer woowa, kàddug Aji Sax ji dikkal na ma ne ma:

18«Yaw nit ki, yuuxul mbooloom Misra, gungee ko seen jéll, ñook janqi xeet yu mag yi, ñu ànd tàbbiji xóotey suuf, fekk fa ña tàbbi woon pax.

19Ne leen:

20Fi biir ñi saamar faat la waa Misra di tëdd.

21Biir njaniiw la jàmbaari xare yay tollu,

22«Buurub Asiree nga faak gàngooram gépp,

23Seeni bàmmeel a nga féete fa xóotey xóote ya,

24«Buurub Elam a nga faak gàngooram gépp,

25Buurub Elam kay a nga tëdd ca biir ña ñu bóom,

26«Buuri Meseg ak Tubal a nga faak seen gàngoor gépp,

27Robaaleesu leen ak jàmbaar ña ànd ak seen gànnaayi xare,

28Waaye yaw itam Misra, yaa ngii rajaxoo fi digg yéefar yi,

29«Edom a nga fa, mooki buuram ak garmi yépp,

30«Kàngami bëj-gànnaar yépp a nga fa,

31«Ñoom la Firawna di gis,

© 2025 Bible Society of Senegal
div>