Esekiyel 35:1-14 WOLB2025 - Bible AI

1Kàddug Aji Sax ji dikkal na ma ne ma:

2«Yaw nit ki, neel jàkk tundu Seyir+ 35.2 Seyir mooy réewum Edom, cosaanu Esawu sëtub Ibraayma.*, nga jottali kàdduy waxyu|lemma="waxyu:"* jëme ci kaw askan wi.

3Nga wax ko, ne ko: “Boroom bi Aji Sax ji dafa wax ne:

4Say dëkk, jali doj laa koy def,

5«“Dangaa masa bañ bànni Israayil|lemma="bànni Israayil:"*.

6Moo tax giñ naa ko ci man miy dund,

7Maay def tundu Seyir gent bu wéet,

8Maay feesaley tundam nit ñu ñu bóom,

9Ay gent yu gental fàww laa laay def,

10«“Edom, yaa ngi naan:

11Moo tax giñ naa ko ci man miy dund,

12Su boobaa nga xam ne man Aji Sax ji,

13Yeenay damu fi sama kaw,

14Boroom bi Aji Sax ji dafa wax ne:

© 2025 Bible Society of Senegal
div>