Esekiyel 38:1-22 WOLB2025 - Bible AI

1Kàddug Aji Sax ji dikkal na ma ne ma:

2«Yaw nit ki, neel jàkk Gog ma ca réewum Magog, boroom Meseg ak Tubal, te nga jottali kàdduy waxyu|lemma="waxyu:"* jëme ci kawam.

3Neel: “Boroom bi Aji Sax ji dafa wax ne:

4Maa lay waññi, we say ŋaam ay lonku,

5Waa Pers, waa Kuus|lemma="Kuus:"* ak waa Puut ay ànd ak yeen,

6Gomeer indaale gàngooram gépp,

7«“Nanga waajal a waajal,

8Feek lu yàgg dees na la woo.

9Waaye yaa naa jàyy ni ngëlén,

10«“Boroom bi Aji Sax ji dafa wax ne:

11daldi ne: ‘Maay songi réew mu ne ŋàpp,

12Yaay dikk ngir foqati, sëxëtoo alal,

13Waa Seba ak Dedan ak julay Tarsis,

14«Kon nag yaw nit ki, jottalil kàdduy waxyu, waxal Gog, ne ko: “Boroom bi Aji Sax ji dafa wax ne:

15ba bàyyikoo sa màkkaan, ca catal bëj-gànnaar,

16Yaay songi Israayil, sama ñoñ,

17«“Boroom bi Aji Sax ji déy dafa wax ne:

18Bésub keroog, ba Gog di dalsi ca kaw réewum Israayil,

19Sama fiiraange ak sama tàngooru xadar laa birale ne,

20jën ak njanaaw di lox fi sama kanam,

21Ca laay wool mbooloom Gog saamar fa sama kaw tund yépp,

22Maa koy mbugale mbas ak deret ju tuuru,

© 2025 Bible Society of Senegal
div>