1Gannaaw loolu kàddug Aji Sax ji da maa dikkal, ne ma:
2«Yaw nit ki, jàkkaarlool ak tundi Israayil, nga jottali leen kàdduy waxyu|lemma="waxyu:"*.
3Neel:
4seen sarxalukaay|lemma="sarxalukaay b-:"* gental,
5Maay tegal néewi bànni Israayil|lemma="bànni Israayil:"* ci seen kanamu kasaray tuur.
6Fu ngeen mana sance,
7Dees na leen bóom,
8Waaye maay déeg lenn ci yeen,
9Su boobaa seenu ndes di ma fàttalikoo
10Dinañu xam ne maay Aji Sax ji,
11«“Boroom bi Aji Sax ji dafa wax ne:
12Ku sore deewe mbas,
13Dingeen xam ne maay Aji Sax ji,