Jooytu 5:1-22 WOLB2025 - Bible AI

1Éy Aji Sax ji, bàyyil xel li nu dal,

2Sunu suuf toxu ciy jàmbur,

3Baay dëddu, nu diy jirim;

4Sunum ndox, xaalis lanu koy feye, naan,

5Sunuw loos lañu ràng,

6Nu nangul Misra,

7Sunuy maam a moyoon, nekkatuñu tey;

8Ay surgaa nu yilif, te amunu

9Bu nu lekkee, sunu bakkan lanu jaay,

10Sunu yaram nib taal la tànge

11Jigéeni Siyoŋ|lemma="Siyoŋ:"* lañuy tëdde,

12Kàngam yi, ñu jàpp, wékk;

13Waxambaane yee yenu doji wolukaay,

14Mag dakkal na jataayu pénc,

15Xol nux-nuxeetul,

16Sunu mbaxana foq na!

17Lee jeexal sunu xol,

18tundu Siyoŋ wi gental,

19Yaw Aji Sax ji, yaay toog ba fàww,

20Ana lu waral nga fàtte nu fàww,

21Éy Aji Sax ji, delloosi nu fi yaw, nu dellusi,

22Xanaa doo nu wacc a wacc,

© 2025 Bible Society of Senegal
>