1Teraanga jekkul cib dof,
2Ñaan-yàlla, soo tooñul, du la dal,
3Xiir, aw fas; laab, mbaam;
4Bul topp ab dof cig ndofam,
5Waaye toppal ab dof cig ndofam,
6Ku yóbbante ab dof kàddu,
7Kàddu gu xelu ci gémmiñug dof,
8Kuy teral ab dof,
9Kàddu gu xelu ci gémmiñug dof
10Njaatige luy liggéeyloo ab dof ak kuy romb,
11Dof day def jëfi dof, dellu ca,
12Ana koo gis mu ne: «Maa xelu»?
13Ab yaafus da naan: «Gayndee ngi ci yoon wi!
14Ab yaafus day tëdd aka walbatiku,
15Ab yaafus day yeb loxoom ci ndab,
16Ab yaafus day foog ne moo gëna muus
17Kuy xuloo lu sa yoon newul,
18-19 Nit kuy naxe,
20Bu matt amul, ab taal fey,
21Këriñ defi xal, matt xambub taal,
22Waxi jëwkat di ñam wu neex,
23Kuy wax lu neex, tey mébét lu bon,
24Ab noon làqoo na ay waxam,
25Buy wax lu neex, bul gëm,
26Su la nëbbalee mbañeel, di la nax it,
27Ku gasal nit am yeer, yaa cay daanu;