Kàddu yu xelu 3:1-34 WOLB2025 - Bible AI

1Doom, bul fàtte sama njàngale,

2ngir fan wi gudd lool,

3Bu la ngor ak worma dëddu,

4Kon nga xam lu jaadu,

5Nanga wóoloo Aji Sax ji sa léppi xol,

6Loo mébét, bàyyil Yàlla xel,

7Bul doyloo sa xel mu rafet,

8sa yaram wér,

9Teralal Aji Sax ji ci sa alal

10say sàq day fees, ne xéew,

11Doom, bul xeeb yaru Aji Sax ji,

12ndax Aji Sax ji, ku mu sopp, yar la,

13Mbégtee ñeel ku daj xel mu rafet

14Am koo gën am xaalis,

15Xel mu rafet a gën gànjar;

16Gudd fan, mu joxee ndijoor;

17Fa muy jaare yiw la,

18Mooy garab giy taxa dund

19Aji Sax ji xel mu rafet la sose suuf,

20Ci xam-xamam la ndoxi xóote ya ne jàyy,

21Sama doom, saxool xelu akug foog,

22Day guddal saw fan,

23Kon sab dox wóor,

24Soo tëddee doo tiit;

25Kon doo ragal njàqare lu bette

26ndax Aji Sax ji da lay yiir,

27Bul xañ njekk ku ko yelloo,

28Bul ne say dëkk: «Demal ba beneen, ma jox la,»

29Bul fexeel dëkkandoo

30Bul joteek kenn ci neen,

31Bul ñee ku néeg,

32Aji Sax ji daa sib ku dëng,

33Aji Sax ji day alag kër ku bon,

34Kuy ñaawle, moo lay ñaawal,

e>