1Lii waxi Agur la, góor gay doomu Yake mu Maasa+ 30.1 Maasa, béreb la bu genn giirug Israayil sancoon ca bëj-gànnaaru Arabi.*. Góor ga daa wax ak Itiyel, wax ak Itiyel ak Ukal. Mu ne:
2Maa dofe dëgg, ba yées ci nit ñi,
3Jànguma, ba am xel mu rafet,
4Ana ku yéegoon asamaan, ba wàcc?
5Lu Yàlla wax, mat na sëkk,
6Bul yokk ay waxam,
7Éy Yàlla, ñaar laa la ñaan,
8caaxaan aki fen, yal na ma sore,
9lu ko moy ma regg, weddi la,
10Bul sikkal ab surga ca njaatigeem,
11Ag maas a ngi saaga baay,
12Ag maas a ngi defe ne set nañu,
13Ag maas a ngi daŋŋiiral;
14Ag maas a ngi, seeni sell niy saamar,
15Saxu watar+ 30.15 watar sax la wu nekk ci ndox, di manq deret.* du suur, ñaar ñu jigéen la am:
16njaniiw,
17Kuy xeelu sa baay,
18Ñett a ngii, yéem na ma,
19yoonu jaxaay ci asamaan,
20Jikkoy jigéenu moykat a ngii:
21Ñett a ngii, day yëngal suuf,
22jaam bu falu buur,
23ndaw su bon su for jëkkër,
24Ñeent a ngii, di lu tuut ci kaw suuf,
25xorondom, néew na doole,
26daman+ 30.26 daman xaw naa nirook njomboor.*, barewul kàttan,
27soccet, amul buur,
28sindax, manees na koo ŋëb,
29Ñett a ngii, ñu jekkum ndaag,
30gaynde, mooy buuru rab yi,
31séq daagu, jekk taxawaay;
32Boo sàgganee bay tëggu,