Kàddu yu xelu 31:1-31 WOLB2025 - Bible AI

1Lii waxi Lemuyel la, buuru Maasa+ 31.1 Maasa, béreb la bu genn giirug Israayil sancoon ca bëj-gànnaaru Arabi.*, te ndeyam jàngal ko ko. Mu ne:

2Ngóor si doom, saa doomi bopp!

3Bul jox jigéen ñi sa doole,

4Buur moomul di naan biiñ, Lemuyel,

5Lu ko moy mu naan, ba fàtte lu yoon tëral,

6Bàyyeel ñoll kuy sànku,

7Bu ñu naanee, fàtte seen néewle,

8Nanga àddul ku amul kàddu,

9Deel àddu, di àtte njub;

10Jeeg bu jàmbaare, ndaw lu jafe,

11Jëkkër ja da koy wóolu,

12Day defal jëkkëram lu baax, du ko lor,

13Day wut kawari gàtt aki wëñ,

14Day mel ni gaalu jula,

15Day jóg te bët setul,

16Day seetlu ab tool, jënd ko,

17Day gañu di góor-góorlu

18Day gis njartel liggéeyam,

19Ma ngay yor poqe

20Day jox ku ñàkk,

21Tiitul ci njaboot gi sedd bu metti,

22Mooy sàkkal boppam ay malaan,

23Dees na ràññee jëkkëram ca pénc ma,

24Ndaw su ni mel day ràbb ay yére, di jaay,

25Faaydaak jom la làmboo,

26Day wax lu xelu,

27Jigéen jooju mooy bàyyi xel ci njabootam,

28Doom ya dañu ko naan: «Jarawlakk!»

29«Jeeg bu jàmbaare bare na,

30Melokaan wu jekk day naxe, taar day wéy,

31Joxleen ko njukkalu ñaqam,

le>