1Lu nekk ak jotam,
2Day jot nga juddu, mu jot nga dee;
3Mu jot nga rey, mu jot nga faj;
4Mu jot nga jooy, mu jot nga ree;
5Day jot nga sànniy doj, mu jot nga dajale;
6Mu jot nga sàkku, mu jot nga ñàkk;
7Mu jot nga xar, mu jot nga gaar;
8Mu jot nga sopp, mu jot nga jéppi;
9Ana lu liggéeykat biy jariñoo ciw ñaqam?
10Gis naa ne sas la bu Yàlla sase,
11Lépp la Yàlla def,
12Ma gis ne nit amul lu gën
13te nitoo nit, su dee lekk aka naan,
14Ma xam ne lu Yàlla def,
15Lu ay tey, ayoon na,
16Ma dellu gis fi kaw suuf ne:
17Saam xel ne ma:
18Saam xel neeti ma:
19Dogalu doom aadama ji
20Ñoom ñépp a bokk jëm benn béreb ba,
21Ana ku mu wóor ne