1Bul rattax làmmiñ,
2Bu xalaat baree, indi gént;
3Boo digook Yàlla,
4Baña digee gën dige loo deful.
5Bu la sa làmmiñ yóbbe bàkkaar,
6Wax ju bare, caaxaani neen;
7Boo gisee ñuy noot néew-ji-doole,
8Xanaa ndax buur suqal mbey mi,
9Bëggkatu xaalis du doyal xaalis,
10Bu koom yokkoo,
11Surga, lekkam néew, bare,
12Naqar wu réy laa gis fi kaw suuf:
13mbaa pexeem moy, mu sànkule;
14Nga juddoo ci sa ndey loxoy neen,
15Dikke ni, delloo ni,
16Ngay dunde tiis bésoo bés,
17Lii daal laa ci gis, man.
18Alal ak koom, ku ko Yàlla may,