Kàdduy waare 8:1-16 WOLB2025 - Bible AI

1Ana ku rafet xel nu muy mel?

2Dama ne déggalal Buur,

3Bul gaawa won Buur gannaaw;

4Kàddug Buur kilifteef la.

5Ku dégg ndigal

6Mbir mu mu doon kat ak jotam ak doxalinam,

7Kenn xamul luy xew ëllëg,

8Kenn moomul bakkanam, ba man koo dese,

9Loolu lépp gis naa ko,

10Ma gis itam ñu bon ñu ñu rob,

11Jëf ñaaw na, mbugal ma yeex,

12Nit bàkkaar na téeméeri yoon,

13Ku bon, du am lu baax,

14Waaye cóolóoli neen a ngi am fi kaw suuf:

15Man daal damay digle bànneex,

16Ma walbatiku xalaat, di jéema xam fu xel rafete,

>