Malasi 2:1-16 WOLB2025 - Bible AI

1«Léegi nag, sarxalkat yi, santaane bii yeen la ñeel.

2Su ngeen dégluwul,

3Maa ngii di yar seen askan,

4Su boobaa ngeen xam ne

5«Sama kóllëre moom laa ko séqal,

6Njàngalem dëgg la dëkkaloon ci gémmiñam,

7«Kàddug sarxalkat déy day sàmm xam-xam,

8Waaye yeen dangeena moy yoon wi,

9«Moo tax man it ma def xeet wépp xeeb leen,

10Xanaa du benn baay lanu am, nun ñépp?

11Waa Yuda wor nañu,

12Ku def lii, yal na la Aji Sax ji

13Lii itam yeena ngi koy def:

14Ngeen naa: «Ndax lan?»

15Kenn deful lii te desem xel.

16«Pase laa bañ,»

© 2025 Bible Society of Senegal
>