Mise 1:1-15 WOLB2025 - Bible AI

1Kàddug Aji Sax jii|lemma="Aji Sax j-:"* moo dikkaloon Mise miy waa Moreset, ca janti Yotam ak Axas ak Esekiyas, buuri réewum Yuda, na seen nguur topplantee. Lii la Mise gis ci mbirum Samari ak Yerusalem+ 1.1 Gannaaw ba réewum Yawut xàjjalikoo, Samari moo doon péeyub Israayil ca bëj-gànnaar, Yerusalem di péeyub Yuda ca bëj-saalum.*.

2Dégluleen, yeen, xeetoo xeet,

3Aji Sax jaa ngii di génne ca bérebam ba,

4Tund ya mu joggi da naan soyox seey,

5Bàkkaaru Yanqóobaa|lemma="Yanqóoba:"* waral lii lépp,

6«Maay saam Samari, def ko jalu tojit

7Seen jëmmi tuur yépp ay rajaxoo,

8Lee ma tax di jooy aka yuuxu,

9Góom bi Aji Sax ji teg Samari kat amul paj,

10Buleen ko nettali fa Gaat+ 1.10 Gaat, dëkku Filisti la woon. Yeneen juróom ñeenti dëkk yi ci topp ñoo séqoon Moreset Gaat, dëkku cosaanu Mise. Ni baatub Gaat di jibe ci ebrë dafa neexoo ak baat biy tekki «nettali».*,

11Yeen waa Safiir+ 1.11 Turu dëkk bii, Safiir, man naa tekki «taaru», taar bi nag woroo ak gàcce gi ñu wax ci aaya bi.*, wéyleen,

12Waa Marot a mar jàmm,

13Yeen waa Lakis+ 1.13 Turu dëkk bi, Lakis lañu nirule ak baatu ebrë buy tekki «fasi dawkat».*, takkleen fasi dawkat ak watiir.

14Yeen waa Yuda, mayleen waa Moreset Gaat+ 1.14 Turu dëkk bii, Moreset, baat bi mu jegewool ci ebrë man na tekki «ab séet». Aaya 10 moo wax ci «Gaat».*

15Yeen waa Maresa+ 1.15 Maresa day neexoo ak baatu ebrë buy tekki «nangukatub réew».* laay indil ku leen moom,

© 2025 Bible Society of Senegal
/div>