1Wóoy, ngalla ñiy mébét ñaawtéef,
2Ñooy xemmemi tool, foqati;
3Moo tax Aji Sax ji dafa wax ne:
4Bésub keroog lees leen di fental aw léeb,
5Moo tax bu mbooloom Aji Sax ji waree jotaat ci seen suuf,
6Seen yonent yeey waare naa:
7Waa kër Yanqóoba|lemma="Yanqóoba:"*, ndax dees na waxe nii:
8Yeen sama ñoñ, démb rekk ngeen jóg nib noon;
9Jigéen ñi ci sama ñoñ ngeen dàqe
10Jógleen dem, fii du bérebu noflaay,
11Nit man naa wër, toppi caaxaan aki fen,
12«Yeen askanu Yanqóoba|lemma="Yanqóoba:"*, maa leen di dajalee