1«Yaw Betleyem Efrata,
2Moo tax Aji Sax ji di leen wacc
3Kilifa gaay taxaw, sàmme ci dooley Aji Sax ji,
4Kookooy doon buntu jàmm,
5Ab saamar la ñooñuy yilife Asiri,
6Ci biir askan yu bare la ndesu Yanqóoba|lemma="Yanqóoba:"* di nekk,
7Ci biir askan yu bare la ndesu Yanqóoba di nekk,
8Aji Sax ji, sa loxo ca kaw, tiim say bañ,
9«Bésub keroog,» kàddug Aji Sax jee,
10Maa fiy yàqe sa dëkki réew mi,
11Maay foqatee ay xërëm ci sa loxo,
12Maay jële fi saw askan say tuur,
13Maay buddee fi saw askan xeri jaamookaayi Asera|lemma="Asera:"* tuur mi,