Nawum 1:1-13 WOLB2025 - Bible AI

1Yéeneb waxyu|lemma="waxyu:"* bu dal dëkk bi ñuy wax Niniw a ngii, di téereb peeñum Nawum ma dëkk Elkos.

2Aji Sax ji|lemma="Aji Sax j-:"* mooy Yàlla ju fiir, te mooy mbugale,

3Aji Sax ji la mer ma diib, doole ja bare;

4Mooy gëdd géej, wowal;

5Tund yu mag yi di ko loxal,

6Bu sànjoo, ana kuy taxaw?

7Aji Sax jee baax,

8Mbàmbulaan lay walal ba faagaagal dëkk bii,

9Ana lu ngeen di fexeel Aji Sax ji?

10Niy taxas la ay noonam di laxasoo,

11Ci yaw dëkk bii la nit génne,

12Aji Sax ji moo ne:

13Léegi buum gi ñu la yeewe laay dog,

© 2025 Bible Society of Senegal