Nawum 2:1-13 WOLB2025 - Bible AI

1Ndaw a ngii dawe kaw tund ya,

2Ki lay falaxe buur na, wutsi la!

3Aji Sax ji moo yeesal darajay Yanqóoba|lemma="Yanqóoba:"*,

4Pakki jàmbaaram ña lañu suub xonq,

5Ca mbedd ya la watiiri xare yay riire,

6Ca la njiit la di woolu kàngami xareem,

7Bunt ya jëm dex ga ñooy jekki ubbiku,

8Futtees na jongama+ 2.8 jongama ji, jombul jëmmu tuur la mu ñu ne mooy nangul am njur. Man naa doon it dëkk bi ci boppam.*, yóbbu,

9Niniw la ay nitam di daw, mu mel ni mbànd

10Sëxëtooleen xaalis, sëxëtoo wurus,

11Dëkk bi lees di raatale, maasale,

12Moo ana paxum gaynde ga?

13Gaynde di fa fàdd lu doy ay doomam,

© 2025 Bible Society of Senegal