Nawum 3:1-19 WOLB2025 - Bible AI

1Wóoy, ngalla dëkkub tuurkatu deret bi,

2Kàcciri dal,

3Gawar buur,

4Lépp ndax ngànctu gu bare gi gànc bi nekke!

5«Maa ngii fi sa kaw,»

6Maa lay xëpp mbalit, sewal la,

7ku la gis, daw la

8Moo Niniw, dangaa gën No Amon+ 3.8 No Amon moy dëkk bi Asiri duma ci 663 at lu jiitu Almasi bi.*, péeyub Misraa?

9réewum Kuus|lemma="Kuus:"* di ndëgërlaayam,

10Teewul ñu gàddaayloo ko, yóbbu cig njaam;

11Niniw yaw it dinga bilimbaane,

12Sa tata yépp ni garabi figg

13Say gàngoor a ngii diy jigéen fi sa biir,

14Niniwee, ndox moo fàggoo ab gaw,

15Fa la la sawara di xoyome,

16Ay jula nga barele,

17Say kàngam it niy soccet,

18Buurub Asiree, say sàmm a saay,

19Sa damm-damm amul paj,

© 2025 Bible Society of Senegal