Njiit ya 5:1-30 WOLB2025 - Bible AI

1Bésub keroog Debora moo woy lii, mook Barag doomu Abinowam:

2«Céy bu garmiy Israayil jiitoo,

3Buur yee, dégluleen; garmi yee, teewluleen;

4«Aji Sax ji, yaa fëlle Seyir,

5tund yaa seey fa kanam Aji Sax ji,

6«Janti ayub Samgar doomu Anat,

7Dëkk-dëkkaani Israayil ñoo noon yàcc yàccaaral,

8Ñoo xewal yàlla yu yees, xare nuyoo ca bunt ya,

9Sama xol laa àndeek njiiti Israayil,

10«Éey, yeen ñi war mbaam yu weex,

11Kàdduy woykat yaa ngoog ca naanukaay ya,

12“Deboraa, yewwulee, yewwul,

13«Ndes wu néew a daan ponkal ya,

14Ñenni Efrayim la seenub reen fëlleji fa Amaleg,

15Kàngami Isaakar ñoo làng ak Debora,

16Moo yeen, lu ngeen di def ci wërmbal yi,

17Galàdd des ca wàllaa dexu Yurdan,

18Waaye Sabulon ay gàngoor gu faalewul dee,

19«Ay buur a xeexsi,

20Kaw asamaan la biddiiw ya tollu, di sot,

21walum Kison buub leen, falaŋ,

22Fasi naaru-góor yaa ngay rëpptal a rëpptal,

23“Móoluleen Meros,” la malaakam Aji Sax|lemma="malaakam Aji Sax j-:"* ji wax,

24«Yaw Yawel, yal nanga gëna barkeel ci jigéen ñi,

25Ndox la Sisera ñaan, Yawel may ko meew,

26Càmmoñam ba la yóotoo xeru xayma,

27Ca tànki Yawel la Sisera nërmeelu,

28«Yaayu Siseraa ngay séentoo palanteeram,

29Ndaxam ña sut am xel ca lingeeram ya tontu nañu,

30“Jombul ña ngay séddale cëxëtoo ma ñu am;

© 2025 Bible Society of Senegal
iv>