1Israayil di reseñ gu naat,
2Ñooy boroom xolub jinigalkat,
3Léegi ñu ne: «Amunu buur,
4Ñooy wax seeni wax,
5Waa Samaree ngi am tiitaange
6Moom it lees di yóbbu Asiri,
7Samari lees di tas, mook buuram,
8Bérebi jaamookaay|lemma="bérebi jaamookaay y-:"* ya ca Bet Awen,
9Aji Sax ji nee na: «Israayiloo, ca janti Gibeya+ 10.9 Gibeya: seetal ci +bk Njiit ya+bk* saar 19—21.* nga dala moye,
10Saa yu ma soobee ma yar leen.
11Efrayim aw nag wu nangu la woon,
12Jiwalleen seen bopp njub,
13Yeena bey ag coxor,
14Am riir mooy jollee ca sa biir gàngoor,