1«Maa soppoon Israayil ba muy ndaw,
2Lu ñu leen gëna woo,
3Ndaxam man maa tette Efrayim, fab ko,
4Ay goji nit laa leen ñoddee,
5Duñu dellu réewum Misra+ 11.5 Loolu mooy duñu dellu ci njaam ga ñu nekke woon ca Misra.*.
6Ab saamar ay wëndeelu ca seen dëkk yu mag,
7Sama ñoñ dañoo làggi ci ñàkke ma kóllëre,
8«Efrayim, ana nu ma lay dëddoo;
9Duma wéye di tàkkal sama mer,
10Dees na topp ci gannaaw Aji Sax ji,