Ose 13:1-14 WOLB2025 - Bible AI

1Bu Efrayim daan wax, ñépp ay lox;

2Léegi ñu ngi gën di bàkkaar,

3Moo leen tax di naaxsaay ni niiru suba,

4«Man Aji Sax ji, fa Misra laa dale di seen Yàlla,

5Man maa leen ràññee ca màndiŋ ma,

6Ngeen wëtti ba regg,

7Moo tax ma mel ni gaynde ci yeen

8Maay dajeek yeen ni rab wu aay

9«Israayiloo, yàqu nga,

10Ana seen buur boog,

11Ci biir mer laa la falal buur,

12«Takkees na ñaawtéefi Efrayim,

13Lu mel ni mititu mat moo dikkal waa jii,

14«Man nag ndax maa leen di musal ci njaniiw?

© 2025 Bible Society of Senegal
/div>