Ose 2:1-24 WOLB2025 - Bible AI

1«Du tere askanu Israayil tollu ni suufas géej. Deesu ko mana natt mbaa di ko waññ, te foofa ñu leen noon: “Yeen, dungeen sama ñoñ,” fa lees leen naa: “Yeenay doomi Yàlla jiy dund.”

2Askanu Yuda ak askanu Israayil dañuy dellu booloo, daldi tabbal seen bopp genn kilifa, te dinañu sëq ci réew mi, ndax bésub Yisreel ba dina réy.

3Nanga woowe sa bokk yu góor: “Ñoñi Aji Sax ji,” sa bokk yu jigéen, nga ne leen: “Ñi Aji Sax ji yërëm.”

4«Tiiñalleen seen ndey, tiiñalleen ko,

5Lu ko moy ma futti ko ba mu ne duŋŋ,

6Ay doomam, duma leen yërëm,

7Ñoom seen yaay moo gànctu,

8«Moo tax man Aji Sax ji, maa ngii di ñage yoonam ay dég,

9Mooy topp ay faram te du leen dab;

10Moom xamul woon ne man maa ko doon jox

11Kon nag fa ngóob jote laay nangoo sama pepp,

12Léegi maa koy futti, mu ne duŋŋ,

13Maay dakkal gépp mbéxam;

14Maay yàqate garabi reseñ aki figg

15Maa koy feyu bési màggal yu tuuri Baal

16«Moo tax maa ngii di ko naxtaan,

17Foofa laa koy delloo tóokëri reseñam,

18Bésub keroog,» kàddug Aji Sax jee,

19Turi tuuri Baal|lemma="Baal:"* laay jële ci sa gémmiñ,

20Bésub keroog maa leen di fasal kóllëre|lemma="kóllëre g-:"*

21«Yaw laay digool ba fàww ab séy,

22Ci kóllëre laay digook yaw ab séy,

23Bésub keroog, maay nangu,»

24suuf nangul pepp ak biiñ ak diw,

© 2025 Bible Society of Senegal
div>