1Yeen bànni Israayil|lemma="bànni Israayil:"*, dégluleen kàddug Aji Sax ji,
2Xanaa ay móolu aki wor, bóome, càcc ak njaaloo.
3Moo tax réew mi wowal,
4«Waaye bu ci kenn layoo,
5Dingeen tërëf bëccëg,
6Sama ñoñ a sànku ndax ñàkka xam;
7Sarxalkat yi ñu gëna baree, gën ma nee moye,
8Sama saraxi póotum bàkkaari ñoñ
9Waaye niki askan wi, niki sarxalkat yi,
10Ñooy lekk te duñu regg,
11Ngànctu ak biiñ bu yàgg ak bu bees
12Sama ñoñ, seen bant lañuy seetéey!
13Ca kaw tund yu mag ya lañuy rendee ay sarax,
14Duma mbugal seeni doom
15«Yeena ngi gànctu, yeen bànni Israayil,
16Ndegam ni aw nag tëwe ni la Israayil tëwe,
17Efrayim+ 4.17 Efrayim, genn la ci giiri Israayil ga ca bëj-gànnaar, moom la Ose faral di woowe réewum Israayil gépp.* googu laa ne, moo lëngook jëmmi tuur!
18Seenu ñoll giiful sax, ñuy gànctoo gànctu,