1«Dégluleen lii, yeen sarxalkat|lemma="sarxalkat b-:"* yi!
2Fippukat yi gën nañoo xuus ci seen bóome,
3Maa xam Efrayim miy Israayil,
4Seeni jëf a leen mayul ñu dellu ci seen Yàlla,
5Israayil, ag reewandeem a ko tiiñal,
6Seen jur gu gudd ak gu gàtt lañuy àndal,
7Aji Sax ji lañu wor,
8«Walleen bufta bi ca Gibeya,
9Efrayim day gental kera bésu mbugal,
10Kàngami Yuda mujj mel ni
11Efrayim lees di noot,
12Man nag ni gunóoru ñaawat laay mel ci Efrayim,
13Ba Efrayim gisee jàngoroom,
14Man déy ni gaynde laay mel ak Efrayim,