1Ca ngeen naan: «Nan dellu ci Aji Sax ji.
2Ñaari fan, mu leqali nu,
3Nan ràññee, di saxoo faale Aji Sax ji.
4Aji Sax jee tontu: «Ana nu ma lay def, yaw Efrayim?
5Moo tax yonent yi laa leen di dumaa,
6Ndax ngor laa namm, dub sarax,
7«Waaye ñoom ca dëkk ba ñuy wax Aadama lañu feccee kóllëre|lemma="kóllëre g-:"*,
8Galàdd mooy dëkkub defkati ñaawtéef,
9Ni saay-saay siy tëroo,
10Ci kërug Israayil laa gis lu yées: