1Yeen waa Israayil, buleen béglu,
2Ndaxam dàgga ak nalukaayu reseñ
3Dungeen des ci réewum Aji Sax ji.
4Duñu tuural Aji Sax ji saraxu biiñ,
5Ana nu ngeen di def nag, ci bésu ndaje,
6Ñu ngoogu dem ndax tasteg réew mi,
7Bési mbugal dikk na,
8Yonent bi mooy wattukat
9Ñoo sóobu ci xóotey yàqute,
10Aji Sax ji nee na: «Ni cabbu reseñu biir màndiŋ,
11Efrayim, ab sagam ni picc lay naawe,
12Bu ñu yaroon seeni doom it,
13Ni ma dogule Tir dëkk ba
14Aji Sax ji, yool leen!
15Aji Sax ji neeti: «Seen gépp mbon moo feeñ ca Gilgal+ 9.15 Gilgal mooy dëkk bu ñuy misaale jëfi bokkaale. Seetal ci 4.15.*,
16Duma nañu Efrayim,