1Bu suuf maree, ñaanal Aji Sax ji ab taw,
2Xërëm, waxi neen,
3«Sàmm yi la sama mer tàkkal,
4Fa Yuda la doju koñu tabax di bawoo,
5Ni ñeyi xare lañuy mel,
6Maay jàmbaaral waa kër Yuda,
7Waa Efrayim ni ñeyi xare lañuy mel,
8Maay waliis, dajale leen,
9Fi biir xeet yi laa leen saawi,
10Fa réewum Misra laa leen di waññee,
11Maay jàll géeju njàqare ga,