1Ba loolu amee kàddug Aji Sax ji Boroom gàngoor yi dellu dikk, ne:
2«Aji Sax ji Boroom gàngoor yi dafa wax ne:
3Aji Sax ji dafa wax ne:
4Aji Sax ji Boroom gàngoor yi dafa wax ne:
5Pénci dëkk bi, ay gone lay feese,
6Aji Sax ji Boroom gàngoor yi dafa wax ne:
7Aji Sax ji Boroom gàngoor yi dafa wax ne:
8Maa leen di indi,
9Aji Sax ji Boroom gàngoor yi dafa wax ne:
10Ndax lu jiitu fan yooyu, nit feyeekuwul peyoor,
11Waaye léegi du na woon laay def
12«Ndax jiwum jàmm lay doon,
13Na ngeen doone woon alkànde ci biir xeet yi,
14Ndax Aji Sax ji Boroom gàngoor yi déy dafa wax ne:
15«ni laa nammatee baaxe ci janti tey jii
16«Ndigal yii, nangeen ko jëfe:
17Ku nekk ci yeen, loraangey moroomam,
18Kàddug Aji Sax ji Boroom gàngoor yi dellu ma dikkal ne ma:
19«Aji Sax ji Boroom gàngoor yi dafa wax ne:
20«Aji Sax ji Boroom gàngoor yi dafa wax ne:
21waa dëkk bii dem ne dëkk bee:
22Askan yu bare ak xeet yu am doole ñooy dikk,