1Yéeneb kàddug Aji Sax jii moo rot
2Kàddu gi dal na itam Amat ga digalook Damaas,
3Tir moo tabaxal boppam tata,
4Ndeke Aji Sax ji moo koy moom,
5Askalon moo koy gis, tiit;
6Xeet wu raxe mooy sanci Asdodd,
7Ci seen gémmiñ laay foqatee deret ji ñuy lekk,
8Maay taxaw wattu fi wër sama kër,
9Bégal a bég, janq Siyoŋ|lemma="Siyoŋ:"* mu taaru,
10Maay sànke watiiru xare ci diiwaanu Efrayim,
11Yaw nag, deret ji feddali sama kóllëreek|lemma="kóllëre g-:"* yaw,
12Yeen ñi ñu tëj, ngeen di dunde yaakaar,
13Yuda déy laay bank, muy samag xala,
14Su boobaa Aji Sax jeey feeñ fi leen tiim,
15Aji Sax ji Boroom gàngoor yi mooy aar ñoñam,
16Bésub keroog seen Yàlla Aji Sax ji