1Kàddug Aji Sax jii|lemma="Aji Sax j-:"* moo dikkaloon Sofoni doomu Kusi+ 1.1 Kusi: xalaat nanu ne nit ku ñuul la woon ku cosaanoo ca xeetu Kuus.*. Kusi, Gedalya mooy baayam; Gedalya, Amarya, Amarya, Esekiyas. Mu yemook janti buuru Yuda, Yosya doomu Amon.
2«Lépp laay buube ba mu set fi kaw suuf.»
3«Doom aadama ak mala,
4«Maay xàcc sama loxo jëme ci Yuda
5ak ñiy sujjóotal ci kawi taax gàngoori biddiiw yi,
6ak ñi dëddu Aji Sax ji,
7Miig! Fi kanam Boroom bi Aji Sax ji,
8«Keroog bésub saraxu Aji Sax ji,
9Bésub keroog maay dikke mbugal
10Su bés baa,» Aji Sax jee ko wax,
11Yeen waa goxu marse ba, yuuxooleen,
12Jantub keroog ay làmp laay niite Yerusalem,
13Seen alal lees di sëxëtooji, seeni kër gental,
14Bésub Aji Sax bu mag bee dëgmal,
15Bésub keroog bésub sànj lay doon,
16bésub bufta ak wootey xare
17«Ca laay jàqale doom aadama yi,