1Yeen xeet wi dul rus, dajeleen a daje,
2balaa dogal bee taxaw,
3Wutleen Aji Sax ji,
4Gasa dëkk ba lees di wacc,
5Wóoy ngalla yeen waa tefesu géej,
6tefesu géej doon àllub parlu,
7Tefes ga, ndesu kër Yudaa koy moom+ 2.7 Réewum Kanaan mi la Yàlla digoon Ibraayma ne moom lay jox aw askanam. Seetal ci +bk Njàlbéen ga+bk* 12.6-7.*,
8«Maa dégg ŋàññi Mowab,
9Moo tax, giñ naa ko ci man miy dund,»
10Loolu lañuy yooloo seen reewande,
11Nu raglu la Aji Sax jiy dale ci seen kaw,
12«Yeen waa Kuus|lemma="Kuus:"* itam,
13Keey xàcc loxoom jëme bëj-gànnaar,
14Ca digg dëkk ba la jur gay goore,