Taalifi cant 10:1-17 WOLB2025 - Bible AI

1Éy Aji Sax ji, lu la taxa sore?

2Ku bon naagu na, ne dann néew-ji-doole,

3Ku bon déy a ngi tëggoo bànneexu bakkanam,

4Ku bon daŋŋiiral, seetul dara,

5Saa yu fexee, juble,

6Ma nga naan ca xelam: «Duma tërëf,

7Ay móolu la gémmiñ ga fees ak fen ak noote,

8Day tëroo ciy dëkk-dëkkaan,

9Day làqu béreb, di yeeroo ni gaynde cim xuntam,

10Ma ngay sëgg aka waaf,

11Mu naa ca xelam: «Yàlla fàtte na,

12Aji Sax ji, jógal!

13Bul may ku bon mu sofental la,

14Yaw de yaay ki nemmiku,

15Ngalla dammal loxol ku soxor ak ku bon,

16Aji Sax jee di Buur ba fàww!

17Aji Sax ji, yaay dégg dagaanu néew-ji-doole,

e>