1Ñeel Daawuda, dib taalifu cant.
2Naa teewlu yoonu màndute.
3Caaxaani neen, xooluma;
4Kuy nas njekkar, sore ma;
5Kuy jëw moroomam, ma wedamal;
6Ku dëggu ci réew mi, ma geesu,
7Kuy njublaŋ du tooge sama kër,
1Ñeel Daawuda, dib taalifu cant.
2Naa teewlu yoonu màndute.
3Caaxaani neen, xooluma;
4Kuy nas njekkar, sore ma;
5Kuy jëw moroomam, ma wedamal;
6Ku dëggu ci réew mi, ma geesu,
7Kuy njublaŋ du tooge sama kër,