Taalifi cant 108:1-13 WOLB2025 - Bible AI

1Di woyu cant, ñeel Daawuda.

2Yàlla, dogu naa,

3Na xalam ak moroom ma yewwu,

4Aji Sax ji, dama lay gërëm ci biir xeet yi,

5Sa ngor a màgg ba sut asamaan,

6Éy Yàlla, yaa màgg ba sut asamaan,

7Walloo nu sa ndijoor,

8Yàllaa àddoo fa këram gu sell,

9Maa moom diiwaanu Galàdd, moom Manase,

10réewum Mowab di sama ndabal raxasukaay,

11Éy Yàlla, ana ku may yóbbu dëkk ba tata wër?

12Yàlla, xanaa du yaa nu wacc?

13Ngalla dimbali nu ci bañaale;

le>