Taalifi cant 109:1-30 WOLB2025 - Bible AI

1Mu jëm ci njiital woykat yi, ñeel Daawuda, dib taalifu cant.

2Ku bon ak kuy fen a ma waxal,

3tance ma kàdduy mbañeel,

4Ma ji nit cofeel, mu sosal ma;

5Sama jëf ju baax, loraange lañu ma ko feye,

6Yal nanga fal ku bon ci kaw kii,

7Bu ñu koy àtte, yal nañu ko yey,

8Yal naw fanam gàtt,

9Yal nay doomam diy jirim,

10ay doomam di tambaambaluy yalwaan,

11Yal na ko kuy feyeeku futti,

12Yàlla bu ko kenn ji ngor,

13Yal na askanam seey.

14Yal na Aji Sax ji bàyyi xel ñaawtéefi maamam.

15Yal na seeni moy sax fi kanam Aji Sax ji.

16Moo séddul ngor,

17Moo soppoon di móoloo, yal na ko këppoo;

18Móolook sol mbubb la yemale,

19Yal nay móoloom di mbubbam,

20Lii, yal na ko Aji Sax ji feye ñi may sosal,

21Waaye Boroom bi Aji Sax ji,

22Damaa néewle te sonn,

23Maa ngi tàggoo ni keru ngoon,

24Samay óom a ngi nasax ndax ñàkka lekk,

25Maa ngii, ñu di ma sewal,

26Éy Aji Sax ji, sama Yàlla, dimbali ma,

27ba ñu xam ne lii sa loxoo,

28Ñooy móolu, yaw nga barkeel;

29Yal na ñi may sosal sàngoo toroxte,

30Ma àddu, sant a sant Aji Sax ji,

le>