1Bu muy nun, Aji Sax ji, bu muy nun,
2Bu yéefar yi ne mukk:
3Te yaw sunu Yàlla, yaa ngi asamaan,
4Seeni tuur xaalis laak wurus,
5am gémmiñ te du wax,
6ami nopp, du dégg,
7ami loxo it te du yég,
8Ñi sàkk yii tuur, yal nañu mel ni ñoom,
9Éy Israayil, wóolul Aji Sax ji,
10Yeen waa kër Aaróona|lemma="Aaróona:"*, wóoluleen Aji Sax ji,
11Yeen ñi ragal Aji Sax ji, wóoluleen Aji Sax ji,
12Aji Sax jee nuy bàyyi xel, di nu barkeel,
13Aji Sax jeey barkeel ku ko ragal,
14Yal na leen Yàlla ful,
15Yal nangeen barkeelu ci Aji Sax ji,
16Asamaan, asamaanu Aji Sax jee,
17Du ku dee mooy màggal Ki Sax,