Taalifi cant 116:1-18 WOLB2025 - Bible AI

1Maa bëgg Aji Sax ji: maa ko woo,

2Teewlu na ma moos,

3Buumi dee a ma laawoon,

4Ma woo Aji Sax ji wall, ne ko:

5Aji Sax jeey boroom yiw ak njub,

6Aji Sax jeey aar ku xamul àddina;

7Bu ma yeboo sama xel dal,

8Xettali nga ma, ba deewuma,

9Damay topp Aji Sax ji

10Ba ma wax: «Torox naa ba toskare,»

11Maa jàqoon ba naan:

12Ana lu may njukkale Aji Sax ji,

13Xanaa ma yékkati kaasu Aji Sax

14Samay digeek Aji Sax ji laay matal

15Wóllërey Aji Sax ji,

16Aji Sax ji, maay sab jaam,

17yaw laay sarxalal saraxu cant|lemma="Sarax yi:"*,

18Samay digeek Aji Sax ji laay matal

le>