Taalifi cant 119:1-175 WOLB2025 - Bible AI

1Ndokkalee yaw mi màndu,

2Ndokkalee yaw miy wattu kàdduy seedeem,

3Doo def njubadi,

4Aji Sax ji, yaa joxe sa tegtal

5Yal naa saxoo

6di teewlu loo santaane,

7Damay gëstu sa ndigal yu jub,

8Sa dogali yoon laay sàmm;

9Ana nu ndaw mana sellalee?

10Sama léppi xol laa lay toppe,

11Sama xol laa làq say wax,

12Jaajëfe, yaw Aji Sax ji,

13Maa àddu, tari

14Topp say tegtal laay bége

15Say tegtal laay jàngat,

16Sa dogali yoon, ma tàqamtikoo,

17Sang bi, baaxe ma, ma dund,

18Ngalla muril saay gët, ma niir

19Doxandéem laa fi kaw suuf,

20Fu ma tollu maa ngi namm say ndigal

21Rëbb nga ñu reew, ñu alku,

22Musal ma ciy kókkaleeki xaste,

23Te it kàngam yaa ngi may tooge,

24Sa kàdduy seede laay safoo,

25Maa ngi ne ñàyy ci pënd bi,

26Wax naa la samay jaar-jaar, nga wuyu ma;

27Dégtal ma li sa tegtal yiy firi,

28Naqaru xol sonal na ma,

29Sorele maak yoonu fen,

30Yoonu worma laa tànn,

31Éy Aji Sax ji, damaa langaamoo sa kàdduy seede,

32Ci sa yoonu santaane laay wéy,

33Aji Sax ji, xamal ma li sa dogali yoon yiy firi,

34May ma dég-dég, ma topp saw yoon,

35Jiite ma ci sa xàllu santaane yi,

36Joyantil sama xol, mu féeteek sa kàdduy seede,

37May ma, ma fénanti caaxaani neen,

38Sang bi, sottalal ma sa dige

39Moyale ma gàcce gi ma ragal;

40Maaka namm say tegtal,

41Aji Sax ji, yaa ko dige,

42ba ku ma kókkali, ma am tontam.

43Bu ma xañ mukk kàddug dëgg,

44Maay topp saw yoon, sàlloo ko,

45di daagoo sago,

46Maay àgge ay buur sa kàdduy seede,

47Maay bége sa santaane

48di yóotu sa santaane yi ma sopp,

49Bàyyil xel li nga ma dig, Sang bi;

50Lii laay muñe samaw naqar,

51Nit ñu bew ñi ñaawal nañu ma lool,

52Éy Aji Sax ji, damaa fàttaliku sa àtte ya woon,

53Sama xol daa fees ndax ñu bon

54Sa dogali yoon laay woyantoo,

55Aji Sax ji, tudd naa la guddi,

56Lii laa séddoo,

57Aji Sax ji, yaw laa séddoo;

58Sama léppi xol laa sàkkoo saw yiw,

59Damaa seetlu sama jëfin,

60Maa ngi gaawtu,

61Buumi ñu bon ñaa ngi may laaw,

62Xaaju guddi laay jóg,

63Maa xejjoo képp ku la ragal,

64Aji Sax ji, sa ngor dajal na àddina;

65Aji Sax ji, def nga la nga dige woon,

66Xamal ma ngëneeli àtte ak xam-xam,

67Maa jàddoon, nga duma ma,

68Yaaka baax tey baaxe;

69Ñu bew ñee yàq sama der aki sos,

70Ñu ngi nii, seeni xol dërkiis;

71Ngëneel la ma duma yi jural,

72Sa ngëneelu yoon wi nga digle

73Say loxoo ma sàkk, tabax ma,

74ñi la ragal gis ma, bég;

75Aji Sax ji, ràññee naa ne say àtte dëgg la,

76Ngalla dëfale ma sa ngor;

77Nanga ma ganesee sa yërmande, ma dund;

78Yal na ñu bew ñi torox,

79Yal na ku la ragal waññiku fi man,

80Yal naa toppe say tegtal xol bu mat sëkk,

81Sàkku naa sag wall ba xol jeex,

82Séentu naa sab dige, ba gët giim;

83Damaa mujj ras ni mbuusum der mu saxaar jàpp,

84Ñaata fan laay toogati, Sang bi?

85Ñu bew ñi gasal nañu ma ay yeer

86Sa santaane yépp worma la;

87Nes tuut ñu sànke ma fi kaw suuf,

88Musale ma sa ngor,

89Aji Sax ji, sa kàddoo sax dàkk,

90Sa worma, ba maasoo maas,

91Ci sa ndigal la lépp taxawe ba tey,

92Su ma bégewuloon saw yoon,

93Duma fàtte mukk say tegtal,

94Yaa ma moom, wallu ma;

95Man la ñu bon ñi tëru, nar maa sànk,

96Gis naa ne lu mat lu ne am na kemu,

97Maaka sopp saw yoon,

98Li ma xelal ba ma raw noon yi,

99Maa gëna ñaw képp ku may jàngal,

100Maa ëpp mag ñi dég-dég,

101Luy yoon wu aay, ma moyu,

102Say santaane it dëdduwuma ko,

103Sa kàddooka maa neex,

104Ci say tegtal laay ràññee,

105Sa kàddu laay niitoo samay tànk,

106Giñ naa te di ko dëggal,

107Toskare naa lool;

108Aji Sax ji, rikk nangul ma kàdduy cant yi ma lay jébbal,

109Sama bakkan ci xott saa su ne,

110Ñu bon ñi ma gasalum pax

111Maa séddoo fàww sa kàdduy seede,

112Damaa dogoo jëfe sa dogali yoon,

113Maa bañ kuy ŋarale,

114Sama rawtu, sama kiiraay, yaw a;

115Yeen ñiy def lu bon, xiddileen ma,

116Yaa ko dige, dooleel ma, ma dund;

117Kàttanal ma, ma raw,

118Yaay xarab képp ku wàcc sa dogali yoon,

119Yaay tonni ni purit képp ku bon fi kaw suuf,

120Sama yaram a ngi daw ndax ragal la,

121Def naa njubte, def njekk;

122Sang bi, gàddu ma, ma am jàmm,

123Séentu naa sag wall ak sa kàddug dëgg,

124Sang bi, jëfeel ma sa ngor,

125Sab jaam laa, may ma, ma ràññee,

126Aji Sax ji, jëf jot na,

127Maa sopp say santaane,

128Moo tax foo tegtale, ma rafetlu,

129Sa kàdduy seede kéemaan la,

130Sa pirim kàddu day leeral,

131Damaa ŋa ŋafeet, di àppaat,

132Éy geesu ma te baaxe ma,

133Dooleelal ma samay tànk, yaa ko dige,

134Jot|lemma="jot:"* ma ci nooteelu doom aadama,

135Sang bi, geesoo ma sag leer,

136ay wali rongooñ ay wale saay gët,

137Aji Sax ji, yaaka jub,

138Yaa santaane sa kàdduy seede ci dëgg

139Damaa gis bañ yiy sàggane say wax,

140Sang bi, maaka sopp sa kàddu

141Ñàkk naa solo, faaleesu ma,

142Sa àtte moo di àtte ba fàww,

143Njekkar ak njàqare dab ma,

144Sa kàdduy seedee di dëgg ba fàww,

145Aji Sax ji, woo naa la wall lu ma man,

146Dama ne: «Wóoy, wallu ma,

147Damaa jëlu, di la woo,

148Damay xoole guddi gépp,

149Aji Sax ji, sama baat bii, teewloo ko sa ngor,

150Rabatkati pexe yaa ngi jegesi,

151Waaye yaw Aji Sax ji, jege nga,

152Yàgg naa xam ne sa kàdduy seede

153Xoolal sama coono te xettali ma;

154Àtte ma, ba jot ma;

155Ku bon sore sa wall,

156Aji Sax ji, sa yërmande yaa na;

157Ñi ma topp ak ñi ma baña bare,

158Damaa gis workat yi, sib leen;

159Seetlul ni ma soppe say tegtal.

160Sa mboolem kàddu dëgg la,

161Ay kilifaa ma topp ci dara,

162Man de, maa ngi bége sa kàddu

163Fen, ma bañ, ba sib;

164Juróom ñaari yoon ci bés

165Jàmm ju baree ñeel ku sopp sa yoon,

166Aji Sax ji, sa wall laa yaakaar,

167Sama xol laa toppe sa kàdduy seede,

168Damaa topp say tegtal ak sa kàdduy seede,

169Aji Sax ji, yal na sama yuux àgg fa yaw;

170Yal na sama dagaan àgg fa yaw;

171Naa xaacu, woyal la,

172Naa woye sa kàddu,

173Yal nanga ma dikke ndimbal,

174Aji Sax ji, namm naa sa wall,

175Yal naa dund ba màggal la,

cle>