1Mu jëm ci njiital woykat yi, dib taalifu cant, ñeel Daawuda.
2Céy Aji Sax ji, loo deeti xaar?
3ba ma tàggook bopp bu ubu
4Céy Aji Sax ji sama Yàlla, geesu ma, wuyu ma,
5noon ba naan: «Daan naa ko,»
1Mu jëm ci njiital woykat yi, dib taalifu cant, ñeel Daawuda.
2Céy Aji Sax ji, loo deeti xaar?
3ba ma tàggook bopp bu ubu
4Céy Aji Sax ji sama Yàlla, geesu ma, wuyu ma,
5noon ba naan: «Daan naa ko,»