1Màggalleen Ki Sax!
2yeen ñi taxaw ci kër Aji Sax ji,
3Màggalleen Ki Sax, Aji Sax jee baax!
4Ki Sax a tànn Yanqóoba|lemma="Yanqóoba:"*,
5Maa xam ne Aji Sax ji màgg na!
6Lépp lu Aji Sax ji namm,
7Mooy yékkateey niir fa cati àddina,
8faat luy taaw fa Misra,
9Yeen waa Misra, moo yónnee ay firndeeki kéemaan fi seen biir,
10Moo duma ay xeeti xeet,
11muy Sixon buurub Amoreen ña,
12Moo nangu seen réew, séddale,
13Aji Sax ji, sa tur ba fàww;
14Aji Sax ji kay ay àtte ñoñam ñi,
15Tuuri yéefar yi, xaalis laak wurus,
16Am gémmiñ te du wax,
17ami nopp te du dégg,
18Ñi sàkk yii tuur, yal nañu mel ni ñoom,
19Éey waa kër Israayil, santleen Aji Sax ji!
20Éey waa kër Lewi|lemma="Leween b-:"*, santleen Aji Sax ji!