Taalifi cant 138:1-7 WOLB2025 - Bible AI

1Ñeel Daawuda.

2Ma sujjóot jublook sa kër gu sell gi,

3Bés ba ma wootee, yaa ma wuyu,

4Aji Sax ji, na la buuri àddina yépp màggal,

5Nañu woy say jaloore, naan:

6Aji Sax jee kawe!

7Ma wéye njàqare,

e>