1Màggalleen Ki Sax!
2Aji Sax jaa ngi tabaxaat Yerusalem,
3di faj naqaru xol,
4Mooy lim biddiiw yi,
5Sunu Boroom a màgg, bare doole;
6Aji Sax ji, néew-ji-doole, mu siggil;
7Woyeleen Aji Sax ji kàddug cant,
8mooy sànge asamaan ay niir,
9leel mala,
10Kii nawul dooley fas,
11Ki Aji Sax ji gërëm mooy ki ko ragal
12Yerusalem, sargalleen Aji Sax ji!
13Mooy tëj ràpp seen bunti dëkk,
14jàmmal seen suufas réew,
15yónnee suuf ndigalam,
16Mooy taw donji yuur yu weexe ni wëttéen.
17Mooy yuri tawub yuuram niy doj.
18Mu yebal kàddoom, seeyal;
19Mooy wax Yanqóoba|lemma="Yanqóoba:"* kàddoom,